L5_Wolof
Juróoméelu Njang. Nettali nu sa cosaan.
Déglul bii léeb. Mingi xewoon amna juróomi junni at.
Gaynde ak fas ñoo nekkoon ci àll bi. Ñoo doon bokk di rëbb.
¿ Lu xew bi loolu weeso ? Gaynde gui séddale rend bi ñaari xaaj .
Ci mujj gi. Gaynde ne ko: benn xaaj bi maa ko moom ak beneen bi itam.